Karmat yi ak doxaliinu amal ay jéebaaneg jalgati àqi moomelu xalaat. Microsoft nangu na àqi moomeelu xalaatu xaaj yu bawoo feneen. Soñu beuguee yonee yeglee wu diotum propriété xell, bokk ci ay bakku wu dialgatiwu yoonu borom, baale ñu nga jeufandikoo suñu doxalin nguir yonee Yegle wi Jalgati (http://approjects.co.za/?big=en-us/legal/intellectualproperty/infringement) ay formuulairu doxaline yi bok ci yoyu sarte. LAAJ YI JËM TE MËN A BOKK CI WÀLL WII KESE LAÑUY TONTU.
Microsoft dafet jeufandikoo doxalinu teunk ci Turr 17, Codu Etats-Unis, Dagg 512, ak, fumuko wara defe, Chapitre III bu Tollolle (EU) 2022/2065, nguir tontu yegle yu akku borom yu ñu jalgati. Ci fann yimu waree, Microsoft dina tamite teree wala diexale comptu jeufandikookatu Microsoft njeuriñ yiy nek ay jalgati kat yu saxx. Su lolu weessoo, ci fann yimu warree, Microsoft meuna dakalagum yoonu yegle ben ci ben wala mbooloo yiy farate di yonee ay yegle yu amule solo. Benen tekki bu geuna sori ci liy teggu ci doxalin bi nguir ben njeuriñ bumu doon, bokk ci teureulaatu ndogual yi Microsoft dieule yu bokk ci suñuy doxaline, meun nga len fekk ci Yegle wu Jalgati (http://approjects.co.za/?big=legal/intellectualproperty/infringement).
Yegle ak doxalin yu ajjo ci propiété xell yi lambo ci publicité. Baale ñu nga xoolate suñu Sartu Propriété Xell (https://go.microsoft.com/fwlink/?LinkId=243207) ci lu dieum ci propriété xell ci suñu leundu publicité.
Àqisos ak karmati màndarga. Cër yi ñooy copyright © Microsoft Corporation ak/mbaa ay joxekat am, One Microsoft Way, Redmond, WA 98052, Etaa-Sini. Jagoos na mboolem sañ-sañ yi. Sarte yi bokk na ci Marku njaayu Microsoft & Doxalinu Mark (http://approjects.co.za/?big=en-us/legal/intellectualproperty/trademarks/usage/general.aspx) (ci niñuko teurale ci jamono ba jamono). Microsoft ak tur yi, logo yi, ak junj costéefi Microsoft, losisel, ak cëram yépp mën nañu nekk ay màrk yuñ bind ba noppi wala yuñ bindagul ci Microsoft mbooleem këru liggéeyukay bi ci biir Etaa Sini ak/wala ci yeneen ëttu àttekaay. Lim bii ngay gis mooy limu lu Microsoft am ciy màrk yu bindu ci http://approjects.co.za/?big=en-us/legal/intellectualproperty/trademarks/EN-US.aspx . Turi këru liggéey ak costéef yi mën nañu doon màndargaay seeni borom. Jagoos na bépp àq buñu joxewul ci wax ci yile Sàrt. Yenn losisel yuñuy jëfandikoo ci daluwebu cërakooni Microsoft ñu àju ci xaaj ci liggéeyu Kuréelu JPEG bu Moom Boppam. Copyright © 1991-1996 Thomas G. Lane. Jagoos na mboolem sañ-sañ yi. Losiselu "gnuplot" bi ñuy jëfandikoo ci yenn serwëri dali Microsoft dañu am copyright © 1986‑1993 Thomas Williams, Colin Kelley. Jagoos na mboolem sañ-sañ yi.
Karmatu wergu yaram. Microsoft du joxe benn digal, gëstu mbaa faju mbaa benn paj bumu mën a doon. Dëkkeel di laaj sa doktor ay digal mbaa yeneen joxekatu wergu yaram yu xarañ ak bépp laaj bi nga mën a am ci li aju ci ab tolluwaayu wergu yaram, resim, tëriinu wer ak tal. Bul xeeb mukk digalu doktor walla yeex ci gis ko ndax leeral yi nga duggoon walla ci biir Cër yi.
Dawalinu aksiyoŋ yi ak njoxey àlluwa (bokk na ci xayma àlluwa). Leerali xaalis yi ñuy joxe ci Cër yi mënoo ko jëfandikoo ludul ci say mbiri bopp te mënoo ci liggéey. Waruloo jëfandikoo lenn njoxe xaalis yi wala màrku képp ku yor sañ-sañu jàmbur bu lëkkalook defar, sos, baayale, njënd ak njaay, jaay, mbaa marketing, mbaa fësal bépp jumtukaayu kopooral mbaa costéefi alalal (maanaam, indis, costéefi yuñu tëggaat, xaalisi alalal, xaalisi wécceeku, kalpey mbebët yi alalal, ak yeneen, fu njëg bi, delloo ak/mbaa këru manéefu jumtukaay mbaa costéefu alalal sukkandikoo, méngoo, walla bu jëmoon ci topp lenn ci njoxey leeral yi) yu àndul ak beneen déggoog ku yor sañ-sañu jàmbur.
Karmatu alalal. Microsoft du ab indikat/jaaykat mbaa laabirekatu alalal bu bindu ci sàrti yooni atekaayu aksiyoŋu réewu federaal bu Etaa-Sini te du digal nit ñi ci ndiglaayu alalal ko, jënd ko mbaa jaay aksiyoŋ yi mbaa yeneen cër mbaa costéefi alalal. Lenn lu nekk ci cër yi du ab maye mbaa càkkutéef ngir jënd mbaa jaay ab aksiyoŋ. Déet Microsoft déet ay ñi yor sàñ-sàñu dawaliinu aksiyoŋ yi mbaa njoxey àlluwam jàppale mbaa digle bépp costéefi xaalisal mbaa cër bu xejjiku. Amul lenn lu bokk ci Cër yi luñu mën na jëfandikoo ni tegtali liggéey, lu ci melni dugal xaalis wala taks yi.
Karmat bu àju ci H.264/AVC ak Baaxoo Wideo VC-1. Losisel bi mën na am H.264/AVC ak/mbaa xaralay Codec VC-1 moom la MPEG LA, L.L.C. jox sàñ-sàñ. Xarala bii ab tëggiinu ngir laxas ay njoxey leerali wideo. MPEG LA, L.L.C. dafay laaj karmat bii:
JAGLEL NAÑU COSTEEF BII CI KAADARU H.264/AVC AK SÀÑ-SÀÑU KALPEY VC-1 PATENT NGIR JËFANDIKOO JAGOO AK JËFANDIKOO AB AJI-JËFANDIKOO CI (A) FAS WIDEO CIG DËPPOOK BAAXOO YI ("BAAXOO WIDEO") AK/MBAA (B) FECCI H.264/AVC, MPEG-4 VISUAL, ak VC-1 VIDEO BU AB AJI-JËDANDIKOOKAT FAS CI AB JËFU JAGOO MBAA BU JAAYUL AK/MBAA ÑU AMEE KO CI AB JOXEKATU WIDEO BUÑU JAGLEL SÀÑ-SÀÑ NGIR JOXE BOOBU WIDEO. JOXE WUÑU BENN SÀÑ-SÀÑ WALLA WAR NAÑ KO NJORT NGIR BENEEN JËFANDIKOO BUMU MËN A DOON. MËN NAÑU JOT YENEENI LEERAL CI MPEG LA, L.L.C. XOOLALE SITE INTERNETU MPEG LA BI (https://www.mpegla.com).
Ngir jubluwaayu leeral kase, karmat bii du yemale mbaa tere jëfandikoo losisel buñu joxe ci kaadaru yile Sàrt ngir ay jëfandikoo liggéey yu jaadu yu liggéey boobu boolewul (i) séddalewaat losisel bi ci xaaj yu bawoo feneen, mbaa (ii) sos ay daju ak xarala BAAXOO WIDEO yu mu nangu ngir séddale ko ci xaaj yu bawoo feneen.
Karmat bu àju ci H.265/HEVC Video yu Yam. Losisel bi mën na amaale kotu xaralay H.265/HEVC. Dugg gu Xóot LLC dafay laaj leeral yii:
SU CI BOKKEE, XARALA H.265/HEVC BI CI LOSISEL BII KI KO ËMB MOOY BENN JAMBAT WALA LU KO ËPP CI MOTIFU HEVC BINU LIM: PATENTLIST.ACCESSADVANCE.COM. LEPP DI AJU CI ANAM WI NGA AMEE LOSISEL BI, COSTEEF BII MËN NA AM LISAAS BU LALU CI PORTFOLIO MOTIFU HEVC.
Suñu sampee losisel bii ci jëfandaayu Microsoft, mën nga fekk yeneen leerali lisaas bi ci: aka.ms/HEVCVirtualPatentMarking .